Madiba, Madiba
Soumay wakh jambar, ngay wakh goor daal, yow
Nite kou ame’ak nite kou niaak mounou niou bok bene
guiss guiss
Soumay wakh goor, mga way jambar yow
Nite kou ame’ak nite kou niaak mounou niou bok bene
guiss guiss
Maane douma soone dila waye
Yeeme nga ma
Souniou’la toudé damay beek, dila waye yow
Fouma déeme dila ndamo
Mandela
Mandela
Mandela
Ni nga mousseu méle
Cii leup nga wouté ak niome
Cii khéle nga wouté
Oudé nimoula guissé, nonou la laye euweulé
Han yow ya goré
Thi joome nga wouté niome
Jambar nga wooné
Adouna bi guissna niou
Téy dji niou ngui begué
Papa Mandela
Hé héee boumay wakh jambar, nga wakh goor daal yow
Nite kou ame’ ak nite kou niaak mounou niou bok beene
guiss guiss
boumay wakh jambar, nga wakh goor daal yow
Nite kou ame’ ak nite kou niaak mounou niou bok beene
guiss guiss
Maane douma soone dila waye
Yeeme nga ma
Souniou’la toudé damay bek- dila waye yow
Fouma déme dila ndamoo
Mandela
Guiss ni diame wara ame, khamné souba ngui nieuw
Kham né lou waye réindi cii lokhome laaye naathie
Litakh diame wara amme
South Africa souniou réuwa
Ngourou yala rek’a doul diekh, Mandela
Thiow li thiow lii mome moye daal fi souniou Africa laa
Gathie ngalama jambar ya dess sa waar wa
Mandela
Mandela
Soumay wakh jambar
Nga wakh gore daal yow
Nite kou ame’ ak nite kou niaak mounou niou bok beene
guiss guiss
Soumay wakh goor daal
Nga wakh jambar yow
Maane douma soone dila waye
Yeeme ngama
Mandela
Souniou’la toudé damaye beek, dila waye yow
Manne fouma déme dilay ndamo
Ki mo di goor
Def na yefou goor
Am na niouko baa, takhoul mou woné ngor
Mandou na cii Nelson Mandela
Mandela
Apartheid laa

Contributed by Dq82 - 2018/8/1 - 18:37
×
Note for non-Italian users: Sorry, though the interface of this website is translated into English, most commentaries and biographies are in Italian and/or in other languages like French, German, Spanish, Russian etc.
Melokáane
Ad aprire il disco è la trascinante “Mandela”, dedicata all’ex presidente sudafricano e Premio Nobel
blogfoolk.com